Ngir am xamle yu gën ci naka nga jëfandikoo Kickshaw, palanteer bu tàllal mën 
ko ubbi ci biir jëfekaay bi. Mën ko jot ci ñaari yoon:

  - Tann "Tàllal" ci xëtu "Ndimbal" ci alluwa bunt jëfekaay bi.
  - Jëfandikoo gaawaliu tefesu klaviyé F1.

Tegtal yi Kickshaw jël:
